Allah, Allah, Allah, Allah Allah, Allah, Allah, Allah Suñu - TopicsExpress



          

Allah, Allah, Allah, Allah Allah, Allah, Allah, Allah Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la Laa illaha ill Allah Boo nekkee ci sa biiru yaay, Yàlla di la sàmm ba nga am juróom ñeenti weer Mu wàcce la ci àdduna bi, boolel la ca nak, Ay xéewali xéewal Boo ko tooñee, boo jéggaloo, mu baal la Boo ko ñaanee mu may la, nga sant ko, mu dolli la Laaju la ludul na nga ma jaamu Laaju la ludul na nga ma jaamu Yow, boo goree, boo goree, war ko jaamu, sant ko. Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la Laa illaha il Allah Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la Buur bi Yàlla moo ñu gëna gore Buur bi Yàlla moo ñu gëna gore Ndax léeg-léeg ñu topp xéewal yi ba fàtte ko Te bu ko neexoon, ci diir bu gàtt Kenn dotul xam fu sa bunt kër féete Loo mënn nekk ci àdduna ya War nga ca boole jaamu Yàlla Def ay digleem, bàyyi ay tereem Te bañ woote benn buur budul Yàlla Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la Laa illaha il Allah Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la Kenn la, kenn la, amul maas Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la Laa illaha il Allah Yàlla na ñu Yàlla buur bi xiir ci boppam Ci barke suñu sang Seydina Mohammed -Salalaaxu aleyxi wa salaam Yàlla na ñu Yàlla xiir ci boppam (Bi jaahi, bi jaahi) (Jaadu Cheikhouna Sanusi) (Jaadu Cheikhouna Sanusi) Cheikh Saad Bu ould Cheikh Ahmed Faadel buun Mamin buun Talib Khayr buun Talib Dieh El Mokhtar Boroom Nimzaat Yërëm ñu yow (Jaadu Cheikhouna Sanusi) (Jaadu Cheikhouna Sanusi) English translation: Lord, Lord, Lord, Lord Lord, Lord, Lord, Lord Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One No master but the Lord With His grace you lived nine months in the warmth of your mothers womb Then you came into this world and were given a destiny He laid forgiveness onto your wrongs, covered you with His favors Thanking Him is enough to receive more In return, He asks only that you surrender to Him In return, He asks only that you surrender to Him The Way is thus to surrender, and to thank Him Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One No master but the Lord Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One His attributes are better than our qualities His attributes are better than our qualities With the pleasures of life, we might forget But in an instant He could erase our reality So whoever you might be Please go on believing Doing right, avoiding wrong Free yourself from all masters except for God Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One No master but the Lord Our Lord is One One, with no peer Our Lord is One No master but the Lord May the Lord make us believers In the name of Seydina Mohamed -May the peace and blessings of God be upon him May the Lord make us believers (By His grace, by His grace) (In the name of Cheikhouna Sanusi) (In the name of Cheikhouna Sanusi) Cheikh Saad Bu, son of Cheikh Ahmet Fadel, son of Mamin, son of Talib Khayr, son of Talib Dieh El Mokhtar The sage of Nimzatt May our sins be forgiven (In the name of Cheikhouna Sanusi) (In the name of Cheikhouna Sanusi) youtu.be/Y4b2ILlv5Mk
Posted on: Sat, 02 Nov 2013 21:55:01 +0000

Trending Topics



Recently Viewed Topics




© 2015