BAMBA nabiyoul houda sangue bi la yalla wolou tek ko sa kaw dioh - TopicsExpress



          

BAMBA nabiyoul houda sangue bi la yalla wolou tek ko sa kaw dioh kafa ay ngenel ; Cheikhou Bamba moy kiko doy moniou doy té doy niathia kaw.Ab mouride melome na oyof; gueum té tek serigne bi si kaw; yatou; selalal sa yéné ak say dieuf rafetal sa ndiot té tek yar ba ak teguine ba moy waral nga yeg thia kaw .Naniou diamou bourbi bouwer mom mi mbind souf bind kaw;bind nite guinek malakine yor gnisi souf té yor nga ka kaw.Serign bou mag bi mota gueum moniou mom sama bate thia kaw.Kon mangi niane si yalla mi falle Cheikhou Bamba tek ko thia kaw def niou ay mouride you sakh dak si ndigueul nek thia kaw niou yague fi lolou ami teranga aki may yokou thia kaw bidiakhi Nabil Moustapha. BAMBA MERCI
Posted on: Sun, 06 Oct 2013 21:17:28 +0000

Trending Topics



Recently Viewed Topics




© 2015