Aj One Ndjite (Lyrics) Feat Xuman , Ceepee , - TopicsExpress



          

Aj One Ndjite (Lyrics) Feat Xuman , Ceepee , Coucou [REFRAIN] hey ! Wadji bañou ñou nga djité askanwé wayé fexel ba nga dimbalé askanwé Kilifeu ngi nangou nañ sa diiné sou raxoulé ndaxté meun nga si defaré ki nga djité Bari na xeetou kilifeu YALLAH la dolel (Djité yomboul !) bi nga xamé ni gnounela la YALLAH bolel warnga taxaw feep nga djitou wara moudje nara motali ñeup ignane waro woudje Meune nga nek ! Borom keur wala kilifeu aada Kilifeu diiné ! Nekhna ba nga done djitou reew boula si YALLAH nato , waro nangou waro beew boul faté xaate demb bay nango ñak fayda seen doom , seen ndongo , Jeunesse citoyene suñu toopa taax ngene djitou kone waruñu ci toy yene ngen woow , boul lonk boumbe suñu bakane nga fonk ñu diap la xar ba ngene xossi la rek xam [REFRAIN] Ndjite Dou teela wax , teela saga , teela door Ndjite Moy moudje wax ta dou melni paaka ñari bord Ndjite souy deflou baax daye gaw ni fassou narou goor Ndjite Daye def liko war , wax liko woor day nekha miine nakharé ñemé Diafé roy bari yeurmandé woyof tool , diss ngane , laabiir meuna teral ngane Niit kou taali , niit kou degou lou yonam nekoul doussi dougou Bolé thi doone kou mandou , sou la togné sax day baalou Niit bouy deglou ni deeg , ragnékou si aaté deugue , ñou di ko wolou ba di ko denk , mou gneuneu woor sakh aap banque Djiko yi yeup deh thi koumou tassé maat nga chef ! Djite bi ngeune moy djite biy roy geune dji mindef [REFRAIN] Fi niit yi di dadialo amna kou ndjitou dioubal seen dokhaline aag fi ñu sentou Niit yi seen beug beug dañu beuri wouté wayé fok mou Jokkolanté akodi so boudé kouthi nek fath sa soxla warou lo si douté kila yiliif warta nek ki lay ngiss di boudé di dolel , di defar , di beugue leep baax Di xeelal , di selal ba deugue meuna saax Thi diiné bak thi ngour gui Ndite ngi mo di royoukay kiñu wara mengol boumou ñu def ni fowoukay Tassé xel yi daale xam xam fess fi deel Modi wané yon yi thi thel ni la meel [REFRAIN] Admin Papi
Posted on: Fri, 18 Oct 2013 11:50:50 +0000

Trending Topics



" style="margin-left:0px; min-height:30px;"> SENA iPhone 5S Antorini- Brown Year End Christmas Gift
Press For Truth Press For Truth Teen Take iSpy: The NSA’s
Custom Kola Matthew :-NIGERIA CUSTOM AUCTION IMPOUNDED CARS FOR
Yet another woman with a Harvard MBA told the school: “I have

Recently Viewed Topics




© 2015